21 colte, Ñalawma Winndereejo Demngal Neeniwal

« Janngirgol ɗemɗe keewɗe ine jojji ngam moƴƴingol jaŋde »
21 febariyee hitaande kala, ko ñalawma winndereejo ɗemngal neeniwal, mo UNESCO dotti e hitaande 2000. Hitaande kala Pelle pinal ngenndiije, hono FƁPM e AMPLCS e APROLAWO, ine mawnina kañum enne ñalawma oo no winndere ndee kala mawninirta mo nii, ngam semmbinnde kuutoragol ɗemɗe ngenndiije nder ekkol, semmbinde keewal ɗemɗe e pine, e tiiɗtinde ngootaagu ngenndi.
Tiitoonde ñalawma 21 feebariyee hikka oo ko « janngirgol ɗemɗe keewɗe jojji ngam moƴƴingol jaŋde ». E wiyde Unesco, ndeen jaŋde « fuɗɗortoo ko he ɗemngal ngal cukalel ɓuri waawde, hade ɗemɗe goɗɗe naatnireede heen seeɗa-seeɗa ». Ndee yiyannde tuugiinde e jannginirgol ɗemngal neeniwal tawo, ine rokki ɗemɗe winndereeje ɗee himme mawɗo sibu ine wallita tafngo renndooji udditiiɗi, ine wallita nguurdiigu pine e jiyanɗe aduna ceertuɗe.
Hannde fof njeñtudi wiɗtooji paatuɗi e ganndal nehdi e jaŋde jowitiiɗi e miijanɗe ekkitaare ɗii fof, ɓuri semmbinde pelle pinal ɗee. Wiɗtooji e humpito kala kollitii wonde kuutoragol ɗemngal neeniwal ko huunde waɗɗiinde ngam yuumtinde jaŋde. Ko hono noon kadi :

  • humpitooji e wiɗtooji baɗaaɗi e nder winndere ndee, paatuɗi e ekkitaare rewrud e e ɗemngal neeniwal, kam en fof ko ɗuum kolliti : wonde sukaaɓe ɓurata feɗɗitaade e jaŋde ko he nder ɗemɗe mum en neeniije ;
  • humpito yuumtungo janngirgol ɗemɗe men neeniije pulaar, sooninke e wolof, ngo Duɗal Ɗemɗe Ngenndiije waɗnoo he Muritani hakkunde 1979 e 1999, ngo ɓeto ummoriingo boowal (Breda-Unesco) e ɓeto ndernderiiwo (Jaagordu jaŋde leydi ndii), ceedtii juumtugol mum, mbasiyii kam en fof kuuɓtodingol jaŋde ɗemɗe ngenndiije nder ekkol.
    Nder leydi men, 21 feebariyee hikka hawri ko e cosgol Duɗal ngam Ƴellitaare e Jaŋde Ɗemɗe Ngenndiije (IPELAN), daawal kimmungal ngam faltude palal gadanal palingal yeeso tippudi nehdi e jaŋde leydi men ngal.
    Pelle pinal ngenndiije ɗee, sabu mum en yenaneede jojjugol rewde jaŋde tuugiinde e ɗemɗe keewɗe sabu « julyultondiral e muuyaaɗe demokaraasi ine mbaɗɗini e sukaaɓe ɓee marde, gaa gaa ko idii fof ɗemɗe mum en neeniije ɗee, marde kadi ɗemɗe winndereeje e diiwaaniije ɗee, mbele aɓe mbaawa jeyeede e renndo ɓurngo yaajde, ɓe njeytoree kadi no haanirta nii e aduna mo ɓe nguuri oo ». Ko ɗuum addani pelle ɗee wasiyaade Dowla Muritani :
  • nde siynata ko ɓuri yaawde, e no ɓuri feewde e yuumtude, janngirgol ɗemɗe men ngenndiije e denndaangal tolnooji tippudi nehdi e jaŋde leydi ndii, ngam huuɓnande yimɓe fof jaŋde, tawa ko jaŋde moƴƴere, ɗo yimɓe fof poti fartaŋŋe, jaŋde nde joñaani hay gooto ;
  • nde huuɓnanta IPELAN gollotooɓe duumiiɓe e tuugnaade e mbaawka, e goongɗingol e haandude ;
  • nde laawɗinta ɗemɗe pulaar, sooninke e wolof, feere timmunde, jojjunde ngam juumtugol jaŋde nder ɗemɗe ngenndiije.

Nuwaasoot ñalnde 21 colte 2023

Jokkorde pelle pinal

21 فبراير، اليوم العالمي للغة الأم:
« التعليم متعدد اللغات ضرورة لتطوير التعليم »

21 فبراير هو اليوم الدولي للغة الأم الذي أعلنته اليونسكو في عام 2000، وتحتفل به الرابطات الثقافية الوطنية (الجمعية الموريتانية لترقية اللغة والثقافة السوننكيتين وجمعية النهوض بالبولارية في الجمهورية الإسلامية الموريتانية وجمعية ترقية اللغة الولفية في الجمهورية الإسلامية الموريتانية) كل عام على غرار المجتمع الدولي، وذلك بهدف تعزيز استخدام اللغات الأم في المدرسة، وتشجيع التنوع اللغوي والثقافي، وتوطيد الوحدة الوطنية.
شعار 21 فبراير 2023 هو: « التعليم متعدد اللغات ضرورة لتطوير التعليم »، تعليم – وفقًا لليونسكو – « يبدأ باللغة التي يتقنها المتعلم بشكل أفضل قبل أن يدخل لغات أخرى تدريجيًا. ». وهذا النهج القائم لدى بدايته على التدريس من خلال اللغة الأم يعطي مكانًة مهمًة للغات الدولية، وبالتالي يساهم في تطوير مجتمعات أكثر انفتاحًا وشمولية وتسامحًا، ويسمح بالتعايش بين الثقافات والرؤى المختلفة للعالم.
واليوم أكثر من الأمس تعززت ثقة الجمعيات الثقافية تشجعها نتائج البحث في مجال علوم التربية خاصة منها ما يتعلق بنظريات التعلم، فقد أثبتت الأبحاث والتجارب بما لا يترك مجالا للشك أن استخدام اللغة الأم للمتعلم أمر بالغ الأهمية للتعلم الفعال، وهو ما يتضح من خلال التجارب التالية على سبيل المثال لا الحصر:

  • التجارب والدراسات التي أجريت في جميع أنحاء العالم، المتعلقة بالتعلم من خلال اللغة الأم، والتي توصلت جميعها إلى نفس النتيجة التي تؤكد أن الأطفال يتعلمون بشكل أفضل بلغتهم الأم.
  • تجربة التدريس بلغاتنا الوطنية البولارية والسونينكه والولفية والتي تأكد نجاحها وفقًا للتقييمات الخارجية (بريدا اليونسكو) والداخلية (وزارة التهذيب الوطني)، وهي التجربة التي تم إجراؤها في موريتانيا بين عامي 1979 و 1999 من قبل معهد اللغات الوطنية السابق. وقد أوصى كلا التقييمين بتعميم هذه التجربة في المدارس.
  • ويأتي يوم 21 فبراير هذا العام في بلادنا بعد إنشاء معهد ترقية وتعليم اللغات الوطنية الذي يمثل خطوة مهمة في رفع التحدي الأول الذي يواجه نظامنا التعليمي الوطني.
    وإن الجمعيات الثقافية الوطنية إذ تدرك الحاجة إلى تبني تعليم متعدد اللغات لأن « العولمة والمثل الديمقراطية تقتضي أن يتقن التلاميذ – بالإضافة إلى لغتهم الأم في المقام الأول – لغات دولية وإقليمية من أجل ولوج مجتمع أوسع والمشاركة بطريقة مناسبة في العالم الذي يعيشون فيه »، لتوصي الدولة الموريتانية بما يلي:
  • تفعيل التدريس بلغاتنا الوطنية في أقرب وقت ممكن وفي ظروف من الكفاءة المثلى، على جميع مستويات نظام التعليم بهدف توفير تعليم للجميع يتسم بالجودة والإنصاف والشمول؛
  • تزويد معهد ترقية وتعليم اللغات الوطنية بموظفين مستقرين على أساس الكفاءة والالتزام والجدارة؛
  • إضفاء الطابع الرسمي على اللغات الوطنية البولارية والسوننكية والولفية، وهو خيار حاسم وضروري لنجاح التدريس باللغات الوطنية.

نواكشوط، في 21 فبراير 2023

منسقية الجمعيات

Dantanxe
Feebiriye 21, jamaanummenaxa saaxaxannen koota « Xanfillomarande, wajabintafi kuudo maranden faraaxunde » Feebiriye 21 ni jamaanummenaxa saaxannen koota UNESCO ga da a ko na a bangande siine 2000. Jamaanummenaxa xillen da dooke, wulliyinfeddu ARPRIM? AMPLCS do APROLAWO wa a ňaxana siine su kuudo saaxanxannun munnafanbagande, na i fasonŋundi xaranra, na xanňaxatinton do wulliyen kandandi, do na ganbanaaxun senbendi.
Feebiriye 21 siine 2023 masalantan ni : “Xanfillonmarande, wajabintafi kuudo maranden faraaxunde”; marande be UNESCO da, “jope ti xannen ŋa, xaranŋaanan ga tu siri, ken falle, xannu tananu na mundin ro”. Ke kille tuge ti xaranŋunde ti saaxanxannen ya fina, a wa killixottinte kinni jamaanunmenaxa xannu, a wa sikki kafobanganton kaanadagaye, i rondinton do i maxayanqanton ga ni, kille ke wa wulliyun taaxanlenmaaxun da, kun do duna ŋallun fatanlenmaaxunto.
Gelli daaru katta lenki, wulliyinfeddun sewonton ni ti muurundun kitayu beenu ga teŋana xaranŋundun killu. Muurunden do xiimandun da a bangandi nan ti xaranŋaanan saaxanxannen munnafanbagandixottinte ni kuudo xaranŋunden foosiren fi be ga xo :

  • Xiimandun do yaaxaraxurandu beenu ga dabari duna di, i ga teŋana saaxanxannen xaranŋunde, i su diganlarun ňa baane, nan ti leminun xaranŋen sirono i saaxanxannen xaranŋen ya;
  • Xiimande be ga ňa ti o jamaanen xannu Fulle, Sooninke do Wolofo na a saxu falle xiimandu (Breda – UNESCO) do jamaanen noxo, a ga ňa moritani na – a wutu 1979 katta 1999 ti jamaanen xannun ka, kun ga da i loogonden kooma xaranra.
    O jamaanen noxo, feebiriye 21gemu jamaanen xannun wuruginden do i xaranŋunden kan bangande JXWX / IPELAN. Taaxottinte kuudo yaaxanro fana ga sikki jamaanen maranden killen besenten ga ňi.
    Jamaanen wulliyinfeddun haqilantaaxun da a wajabindi na xanfillon maranden raga na a saxu « dunaranmondaaxun do demokarasin sinmayun koomandi ti xaranlenmon tigitindu duumanto, i saaxanxannun da dooke, jamaanunmeenaxa xanun dingiranko, i ga katono joofene kafoyiriwante, ken do i ga kafini moxoxerente duna be i ga birene a noxo » i wa ku koomandu teŋandini moritani dowla :
  • Jamaanen xannun xaranŋunden rondinde hapu siru do killu gemunto maranden killen siganun su, kuudo marande, a su da, tinmanye, ňekkoye do rondinde kanma.
  • Na golliňaŋaano duumanto, siye, duukinne do gan xawa ro JXWX / IPELAN golliran ŋa.
  • Na jamaanen xannun Fulle, Sooninke do Wolofon dagandi kutikanmun kille do jamaanen xannun xaranŋunden wajabindi.
    Nuwasotu, Feebiriye 21 siine 2023

Feddun jokkinda

21 Feeviriyee bës bi ñu jàgleel ci adina bi, làkk wi nga nàmp.
« Njàng ci làkk yu wuute, lu war la ngir soppi njàng mi »
21 Feeviriyee mooy bës bi (uneskoo) jàgleel ci adina bi, làkk wi nga nàmp. Ni ñu kay amale ci adina bi, mbootaayi mboor yi ci réew mi, (ARPRIM, AMPLCS, ak APROLAWO) dañu kay màggal at mu ne, ngir leral gëdd njàng ci làkk wi nga nàmp ci daara yi, ñaax wuuteb làkk ak mboor te gënna degaral bennoo askan wi.
Li ñuy waxtaane at mii ci 21 Feeviriyee mooy (njàng ci làkk yu wuute, lu war la, ngir soppi njàng mi) njàng moo xam ni, ci gis-gisu uneskoo, day tàmbali ci làkk wi kee jàng gëna xam, ganaaw gi ñu duggal yenneen làkk ndànk-ndànk. Gis-gis wii, sukkàndiku ci adina bi, ci njàng ci làkk wi nga ñàmp, te bokk ci li tax askàn wi gënna ubbeeku, di boole te di baale, day yombal ay caada ak gis-gis yu wuute mën ànd.
Tay la mbootaayi caada yi gëna gëm, te gëna sawar, ndax njureefi gëstu yi, ci wàllu njàng, ak xalaati njàngin. Gestu bi, ak jëmmal, wone nañu, ci lu leer ni, jëfandikoo làkk wi nga nàmp lu mënul nàkk la, ci njàng mu baax, ni ko yii wonee :

  • Jëmmal ak jéemant yi am ci adina bi, jëm ci njàng ci làkk wi nga nàmp wone nañu ni, xale yi ñungee gëna man jàng ci làkk yi ñu nàmp.
  • Jéemant wi am ndam, ci njàng ci làkk yi ñu nàmp, pulaar, soonike wolof, ni ko xayma yi joge bitim réew wonee, (breda-unesco) ak yi joge ci biir réew mi (MEN), te daaray làkki réew mi ñu ray defoon ko. Ñaari xayma yooyu yepp denkaane woon nañu yaatal njàng moomu ci daara yepp.
    Ci sunu réew, 21 feviriyee mungi nów ganaaw bi ñu amalee daara ngir yokkute ak njàng ci làkki réew mi (IPELAN) muy jeego bu am solo, ngir jeggi jafe-jafe wi jëkk, wi sunu njàng ci réew mi jànkoonteel.
    Mbootaayi caada yi ci réew mi, yeewu ci wareefi amal njàng ci làkk yu wuute, ndax adina bi nekk benn, ak mbaaxu demakaraasi, dañuy xelal ni, ndongo yi war nañu xàm bu baax, ganaaw seen làkk wi ñu nàmp, yenneeni làkki adina bi aki làkki diwaan bi, ngir mën bokk ci askan wu gëna yaatu, te def seeni loxo ni mu ware ci adina bi ñu nekk. Mbootaay yi ñungee denk nguuru Muritani :
  • Jëmmal ci ni mu gëna gaaw, ak ci anam yu gëna wóor, njang ci làkk yi ñu nàmp ci banqass yepp, ci gis-gisu njàng mu baax te yemale ñepp.
  • Jox (IPELAN) nit yu fay toog, sukkandiku ci man-man, gëm-gëm ak yelloo.
  • Yoonal làkki réew mi, pulaar, sooninke, wolof, nuy lu war ngir am ndam ci njàng ci làkki réew mi.

NKTT 21 Feewiriyee 2023

Lekkaleb mbootaay yi

21 février, Journée internationale de la langue maternelle :
« L’éducation multilingue, une nécessité pour transformer l’éducation »
Le 21 février est la journée internationale de la langue maternelle, proclamée par l’UNESCO en 2000. A l’instar de la Communauté internationale, les Associations culturelles nationales ARPRIM, AMPLCS et APROLAWO la célèbrent chaque année en vue de favoriser l’utilisation des langues maternelles à l’école, encourager la diversité linguistique et culturelle, et renforcer l’unité nationale.
Le thème de ce 21 février 2023 est : « L’éducation multilingue, une nécessité pour transformer l’éducation », une éducation qui, selon l’Unesco, « commence dans la langue que l’apprenant maîtrise le mieux, puis introduit progressivement d’autres langues. » Cette approche basée sur l’enseignement par la langue maternelle d’abord, accorde une place importante aux langues internationales et contribue ainsi au développement de sociétés plus ouvertes, inclusives et tolérantes, permet la coexistence des cultures, et des visions différentes du monde.
Aujourd’hui plus qu’hier, les Associations culturelles sont confortées et encouragées par les résultats des recherches dans les sciences de l’éducation se rapportant aux théories des apprentissages. La recherche et l’expérience ont clairement établi que l’emploi de la langue maternelle de l’apprenant est crucial pour un apprentissage efficace, comme l’attestent, entre autres :

  • les expériences et études menées à travers le monde, relatives à l’apprentissage par la langue maternelle, qui ont toutes abouti à la même conclusion ; à savoir que les enfants apprennent mieux dans leur langue maternelle.
  • l’expérimentation réussie de l’enseignement par nos langues nationales pulaar, sooninke et wolof selon des évaluations extérieures (Breda-Unesco) et internes (MEN), menée en Mauritanie entre 1979 et 1999 par le défunt Institut des Langues Nationales (ILN), qui ont toutes deux recommandé leur généralisation à l’école.
    Dans notre pays, ce 21 février intervient après la création de l’Institut pour la Promotion et l’Enseignement des Langues Nationales (IPELAN), jalon important pour relever le premier défi auquel est confronté notre système éducatif national.
    Les Associations culturelles nationales, conscientes de la nécessité d’adopter une éducation multilingue du fait que « la mondialisation et les idéaux démocratiques suggèrent que les élèves doivent maîtriser couramment, outre leurs langues maternelles en premier lieu, des langues internationales et régionales pour avoir accès à une société plus large et participer d’une manière pertinente au monde dans lequel ils vivent », recommandent à l’Etat mauritanien :
  • de rendre effectif, dans les meilleurs délais et conditions d’efficacité optimale l’enseignement par nos langues nationales à tous les niveaux du système éducatif dans une optique d’éducation pour tous, de qualité, équitable et inclusive ;
  • de doter IPELAN d’un personnel stable sur la base de la compétence, de l’engagement et du mérite ;
  • d’officialiser les langues nationales Pulaar, Sooninke et Wolof, option décisive et nécessaire à la réussite de l’enseignement en langues nationales.

Nouakchott, le 21 février 2023
La Coordination des Associations

About Diagana

Check Also

Sunaare: sankaare meeDnooDo wonde hooreejo batirde ngenndiire Muritani, Mohamed Boyliin

Ndee daande ñifii, Muritani waasii gooto e jagge mum, ɓurɗe teskinde e laamu. Med O. …

Laisser un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *